Commission Scientifique et Culturelle: di wànqaas wi yor lépp lu jëm ci jàng ak jàngale ci Touba Ca Kanam Tay jii amaloon na ab lëlu tàggatu ngir Waajal Sëriñ Daara Yu bees yi war a jàngale Daaray Tànneef bi Nekk Ndaamatu 5 Ngir njàng mi gën a baax ba ndiru Turu daara bi "Daaray Tanneef"